Compositor: Não Disponível
Waaw waaw yehé
Dior Mbaye
Yàlla dogal lu ma def mu dem
Fa ñee di tële, ñële di jëm
Ma saf ci seen xol ba dàq lem
Ngeen di ma sànni cœurs aki j’aimes
Buur Yàlla dogal lu ma laal mu dem
Yaw saqar bu dekki ku ca langue dem
Xoolal Ségne Fallou ma wis xorom ba ma ñeme
Segne Fallou ma wis xorom ma yeme
Picc takk ci guy (guy yëgul)
Picc kes kesi (guy yëgul)
Picc naw ni fér (guy yëgul)
Hey picc takk ci guy (guy yëgul)
Picc kes kesi (guy yëgul)
Heyy picc yakk ci guy (guy yëgul)
Picc kes kesi (guy yëgul)
Picc naw ni fér (guy yëgul)
Yëg nga ni guy gi yëgu la (guy yëgul guy yëgu la)
Bu de dangay jamb de yëgu la (guy yëgul guy yëgul la)
Yaw xoolal ma ngay su yëgu la (guy yëgul guy yëgul la)
Guy gu mat yëgu la (guy yëgul guy yëgul la)
Ma ne dindi sax lan nga defoon ca gën Yàlla noppi na
Doomu jaambur ku ko yakk dang ko jurul
Ku ne xam na ki la mën danga ko dul nangu
Yàlla def na li ko sopp demb noppi na
Ma ne garab bu ndaw
Boo ko munta rose bàyyi ko mu dund
Bul jëm budi bul budilu xamoo fu ren ba sax
Dandal sore deko xol de loin moo lay musel
Xanaa xamoo ne am na ñoo xam ne kenn duleen laal
Picc takk ci guy (guy yëgul)
Picc kes kesi (guy yëgul)
Picc naw ni fér (guy yëgul)
Hey picc takk ci guy (guy yëgul)
Picc kes kesi (guy yëgul)
Heyy picc yakk ci guy (guy yëgul)
Yëg nga ni guy gi yëgu la (guy yëgul guy yëgu la)
Bu de dangay jamb de yëgu la (guy yëgul guy yëgul la)
Yaw xoolal ma ngay su yëgu la (guy yëgul guy yëgul la)
Guy gu mat yëgu la (guy yëgul guy yëgul la)
Boo amee ñaanu waajur
Looy ragal kon doxalal
Am na ñaanu waajur
Lu may ragal nañu doxal
Lobita Gueye am na ñaanu waajur
Looy ragal kon doxalal
Pape Beye am na ñaanu waajur (le jeune tailleur)
Mbawor mbawor bi yaw kay doxal
Ndeye Thiam am na ñaanu waajur (jigéenu Bass)
Chérie Soulemane Sané doxalal
Ehh Wally bul geestu
Maryacine bul geestu
Liggéeyu nday day tontu
Narou Diaga bul geestu
Chéri Sokhna bul geestu
Liggéeyu nday day tontu
Xoolal liggéey focus ñuy waxtu
Xol bu rafet day tontu
Maroo mar bul geestu