Compositor: Não Disponível
Ahn li leer la am mbëggéel la
Li leer la am mbëggéel la
Xale bile mbëggéel ci xo day fegn ci kanam
Li leer la am mbëggéel la
Li leer la am mbëggéel la
Xale bile mbëggéel ci xo day feeñ ci kanam
Maa la nob assumé na lu ma ci gobe gaar
Yaa ne sama biir xol ya raw far bu jar
Chéri ne na ni ma mel yaa ko wara yaa ko jaar
Li leer la am mbëggéel la
Li leer la am mbëggéel la
Xale bile mbëggéel ci xo day feeñ ci kanam
Man su ma lay gis ni may jongoma dama ko ragal
Lémi lémi du sama yëf damy dox di tagal
Sama mbëggéel ci yow bu doon ay ay loo duma ci feggal
Li leer la am mbëggéel la
Li leer la am mbëggéel la
Xale bile mbëggéel ci xo day feeñ ci kanam
Adja Soda Maréme thaim New Jersey
Thaim demba torodo bi ci walo
Thiatou Adja Daro ak aladji Ousmane
Thiam dembaa
Seut ci El-hadji Malick SY
Seut ci maam Ahmadou Bamba
Seut ci Cheick Pumar Foutiyou Tall
Yayou amina niane ak
Papa Ousmane niane
Ab thiamen dé day bari jom
Bayou nabou nana ak ramatoulay
Thiam wona bassirou thiam demba
Ko koy chérie Sébastien
Somou ndayou Fatimata dramé
Man de li ma doon seet gis naa ko
Caafka mbëggéel bime doon wër am na ko
Yaay sama alljana xam naa ko
Li leer la am mbëggéel la
Li leer la am mbëggéel la
Xale bile mbëggéel ci xo day feeñ ci kanam
Lii moo tax sama réew neex
Senegaal Ndiaye seeni jeeg dañu jonge
Lii moo tax sama rew nekh
Sénegal ndiay séni jegg danio jonge
Ndey Coumba Vip hair xale yaa ngi di jongoma
Ku ci gattul danga njool te koiuci xessoul danga ñuul
Chérie ousseynou guey jeeg boobu aka paré
Lii moo tax sama réew neex
Senegaal Ndiaye seeni jeeg dañu jonge
Man bu ma sañse nga xool ma
Reetaan nga may bégel
Ma di ko tiktok ngato di seetan mu lay yëngel
Li du kemtan sañse ma gënal
Lii moo tax sama réew neex
Senegaal Ndiaye seeni jeeg dañu jonge
En diawri thiane chéri babou anne yayou
Zeyna ak Binta ak Abdlaye boroom Amerika
Lal na sama lal bi ba mu tali cuuraay di gilli
Ay mbal aki guert la sajj neexal guddi gi
Bégal sama xol dara du ko dakk yaay sama Sadio Bane
Dina la may mbakhous bou rey tay