Compositor: Não Disponível
Fi nga juddoo moo lay def
Li nga nara doon
Fi nga bokk sant bi ngay wuyoo
Waratuloo
Wàcc yoon
Su ma saañoon
Ñun ñaar lu ñu neex def
Saañuma ko
Lu ñuy xaar ci man lay def
Sorale
Ñoom lay sorale
Sama xel ak sama xalaat comptétul
Ñoom lay sorale
Sorale
Ñoom lay soor
Sama xel ak sama xalaat comptétul
Ñoom lay soor
Guddeek bëccëg, suba ak ngoon
Ma nekk ci naqar
Jënde sama mbégteek sama
Bànneex ak li ma war
Pression sociale, règlement familiale
Juddu bu réy ak alal
Ñoo ma yobe li ma dàll
Sorale
Ñoom lay sorale
Sama xel ak sama xalaat comptétul
Ñoom lay sorale
Sorale
Ñoom lay soor
Sama xel ak sama xalaat comptétul
Ñoom lay soor