Saf Safal (feat. DK)

Dior Mbaye

Compositor: Não Disponível

[Dior Mbaye]
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Di la bégal boo meree ma lay defal
Xol bi yaa ko moom, jëlal
Yaay ki may dundal

Saf safal, sa dundu ma koy safal
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Di la bégal boo meree ma lay defal
Xol bi yaa ko moom, jëlal (kay)
Yaay ki may dundal

Xam li nga bëgg tëddi la ko defal de boy ci sa dinga leer
Dañuy dundu dëgg mbëggeel
Ndax man noonu nekkatul ma sa jér
Jàpp la ci el, dama li ko jëti ma tufal
Danga ma siggi, danga ma sagal
Kon tay ma lay tër (tay ma lay tër)
Naa la toppatoo du font en camp
Def li nga bégal noy bel mel ni kontaan
Duma la foon dox
Waaye naa la one di takkal nga ku pare
Jonge dégg daaj, fi may faale dafa bare
Hey baby, man rekk ci xale
Jélul vrai paré fi lépp gale

Saf safal, sa dundu ma koy safal
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Di la bégal boo meree ma lay defal
Xol bi yaa ko moom, jëlal
Yaay ki may dundal

Saf safal, sa dundu ma koy safal
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Di la bégal boo meree ma lay defal
Xol bi yaa ko moom, jëlal (kay)
Yaay ki may dundal

Ma ne bari paj, taxa
Aw fitay fiteel bu ma fiire
Ma ne dégg deel ragaluma ku ma viser
Doxaati du tel dama tirer
Waaye maak yaw la rekk sama chéri
Keneen amul fi palaas boo koy jëmee
Maak yaw la rekk sama chéri
Fi du fi am palaas

Dewal ma tagg la buur, di yëngal sa mbur
Yaa ko son bi tey dinga suur
Kon tey ma def li ma man, taggalal sa maam
Te ko ci gamm
Waaye naa la one di takkal nga ku pare
Jonge dégg daaj, fi may faale dafa bare
Hey baby, man rekk ci xale
Jélul frai paré fi lépp gale

Saf safal, sa dundu ma koy safal
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Di la bégal boo meree ma lay defal
Xol bi yaa ko moom, jëlal
Yaay ki may dundal

Saf safal, sa dundu ma koy safal
Saf safal, sa dundu ma koy safal
Di la bégal boo meree ma lay defal
Xol bi yaa ko moom, jëlal (kay)
Yaay ki may dundal

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital