Demna

Dior Mbaye

Compositor: Não Disponível

Demna té douma deloussi demna
Demna té douma deloussi demna
I don't know the reason, why do you go?
Do we goooo, do we go
I don't know the reason, why do you go?
Do we goooo, do we go

Since a long time
Ma ngui dab seu banex
It's been a long time
Mangui def lou la nex

Ndéké beugouloma way
Ndéké kholou loma
Oh baby you make me cry
So i see you baby

Dem naaa té douma deloussi, demna
Dem naaa té douma deloussi, demna
Dem naaa té douma deloussi, demna
Dem naaa té douma deloussi, demna

Guiifeul leu
Huuun saa bo méré
Réwal leu
Huuun saa ma bébé eh

Ndéké beugou loma way
Ndéké xolou loma
Oh Baby you make me cry
So i see you baby

Demna dem naaa i have gone
Dem na i won't be back a have gone
Demna
Demna dem naaa i have gone
Demna i won't be back a have gone
Demna

Demna
Demna
Tog sa wét si banex ak si nakar
Di diéma meutal sama rolou diabar
So guéné ma ngui tog dila xaar
Ngey guéneu goudi di gnibissi fadiar
Def naa mougn wanassou sama nakar
Xolou loo sax fii niou diaar
Faw ma dem ndakh té dama maarreeee

Dem

Dem

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital