Je T'aimetaime

Dior Mbaye

Compositor: Não Disponível

daga done fo
daga done kaf wayei mbeugel dou fo
khol bouy beug dou tago
guiss nani dou keine yowla
takhna ma bayi nieup diapela
iow boul ma dianii natoula
li ma dal dou yawou yalla la

lekatouma
nanatouma
deim na ba meuneutouma
ma gueuneu diape bayiwouma
je t'aime je taime yeh yeh yeh
je t'aimetaime taime
lo wakh damay joie
lo def damay joie

nakh iow sa bopp yama nekh
je t'aime je t'aime yeh yeh
je taime je taimetaime t'aime
lo wakh damay joie
lo deff damay joie
nakh iow sa bopp yama nekh
dafa melni iow ladone khar
bima la guissei la

souma diakarlok iow
lou melni courant mo May masse
yama thiokhatane
dematouma feine
guissatouma keine
kholatouma leine
guiss kila beugu
dafa diafei
boul ko kaffei

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital