Compositor: Não Disponível
En bas corona
Nañu xeex corona
Lénen warone na unir aduna té dou doon corona
En bas corona
Nañu xeex corona
Lénen warone na unir aduna té dou doon corona
En bas corona
Nañu xeex corona
Lénen warone na unir aduna té dou doon corona
Doon na kô yaakkar doon kô xaar
Li xew Dakar di xew Qatar té dou naxxaar
Bu ñëp youxoooo
Kouy walloooo
Nañouko jéma songuëë ndo
Mëênko dana ndo
En bas corona
Nañu xeex corona
Lénen warone na unir aduna té dou doon corona
En bas corona
Nañu xeex corona
Lénen warone na unir aduna té dou doon corona
En bas corona
Nañu xeex corona
Lénen warone na unir aduna té dou doon corona
Asia, America, Europe, Océanie, Africa
Nous tous on se bat contre corona.
Ñu amane ndo ben combat
Nañuye raxass loxo yi wagni safonté bi
Sa yaram loussi walessi ngua woté numéro bi 800 00 50 50
Respectons les consignes
Chaque vie compte je reste chez moi
Restez chez vous.
STOP CORONAVIRUS